"Laf Thiat"
— yaririmbwe na Omg
"Laf Thiat" nindirimbo ikorerwa kuri abanyasenegali yasohotse kuri 23 ukuboza 2021 kumuyoboro wemewe wa label - "Omg". Menya amakuru yihariye yerekeye "Laf Thiat". Shakisha indirimbo yindirimbo ya Laf Thiat, ibisobanuro, nukuri kwindirimbo. Kwinjiza hamwe na Net Worth byegeranijwe nabaterankunga nandi masoko ukurikije amakuru aboneka kuri enterineti. Ni kangahe indirimbo "Laf Thiat" yagaragaye mubishushanyo mbonera bya muzika? ".
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Laf Thiat" Ukuri
"Laf Thiat" igeze kuri 902.5K yose hamwe na 23K kuri YouTube.
Indirimbo yatanzwe kuri 23/12/2021 kandi yamaze ibyumweru 30 kurutonde.
Izina ryumwimerere rya mashusho yindirimbo ni "OMG - LAF THIAT ( VIDÉO OFFICIELLE)".
"Laf Thiat" yasohotse kuri Youtube kuri 19/11/2021 22:00:26.
"Laf Thiat" Indirimbo, Abahimbyi, Ikirango
Auteur : OMG
Compositeurs :
;& Mak bibs
Directed & Edited by : Jordy Diop
Producteur Exécutif: DD Records
Stylisme : Stef De Karda
Bijoux & Accessoires : Stef de Karda
Makeup : Mya Make-Up
Additional Guitars : Emeudy
Déco : Moustapaha Ndieuguène Fall 77 694 15 79
Streaming :
Remerciements : Maison de la Culture Douta Seck
Retrouvez OMG sur:
Facebook:
Instagram:
Tik Tok :
Tweeter:
Contact: 00221774498714
Email: manager@
Booking à l'international : +33 6 16 68 71 09
LYRICS
INTRO
Yeah, Yeah, Yeah
Oumy Gueye
OMG
REFRAIN
Mashallah baax ga yarou ga
Nena laf thiat
Am touti bandit beuri thiass
Nena laf thiat
Yay kiy def dossi bole wax
Nena lafthiat
Thiat dafa gaw bouggouma kouniou rè
Nena laf thiat
Ki kouko soukeur
Xalè bi laf thiat
Soxla wul sapali
Nena laf thiat
Loxo bi gaaw na
Xalè bi laf thiat
Aka meuna sagnse
Kone néléne laf thiat
1er COUPLET
Ben gafi
Kou mel ni yaw amatoul
Yamay dieri
Yay sedal sama xol man
Deg nañ lou neh teyoul ga gueuneu jap
Digunte bé dax mburok lem
Yamay Douta Mbaye
Louma neex neex nala
Lima beug deg rek gay wax
Xol bi nena waaw
Melo ni niom
Amo morom
REFRAIN
Mashallah baax ga yarou ga
Nena laf thiat
Am touti bandit beuri thiass
Nena laf thiat
Yay kiy def dossi bole wax
Nena lafthiat
Thiat dafa gaw bouggouma kouniou rè
Nena laf thiat
Ki kouko soukeur
Xalè bi laf thiat
Soxla wul sapali
Nena laf thiat
Loxo bi gaaw na
Xalè bi laf thiat
Aka meuna sagnse
Kone néléne laf thiat
HOOK
Sa djiko dji neex nama
Sa ree djou neex sofuma
Ningay waxe neexnama
Dara ci yaw sofouma kone nena laf thiat
2e COUPLET
Wereutouma ndax dof ci yaw
Sama thiabi mbëguel mougui ci yaw
Aldiana rek lay dounde ak yaw
Yama meuneu fathie
Yay garap bi Guën thi man
Deg nama niou naan
Couple bi dafa nice
Mashallah
Hey kaar boulen niou thiatou waay
Lamigne baxoul waay
Lalal bant waay
Daagul ni ma daagu nee
Niou andë doxal waay
REFRAIN
Mashallah baax ga yarou ga
Nena laf thiat
Am touti bandit beuri thiass
Nena laf thiat
Yay kiy def dossi bole wax
Nena lafthiat
Thiat dafa gaw bouggouma kouniou rè
Nena laf thiat
Ki kouko soukeur
Xalè bi laf thiat
Soxla wul sapali
Nena laf thiat
Loxo bi gaaw na
Xalè bi laf thiat
Aka meuna sagnse
Kone néléne laf thiat
HOOK
Sa djiko dji neex nama
Sa ree djou neex sofouma
Ningay wakhe neex nama
Dara thi yaw sofouma kone nena laf thiat
#OMG #Laf_Thiat #Oumy_Gueye